Galérie Photos

Cover Photos Retour à la galérie

Audio sermon de Cheikh Ahmadou Mbacke Maoulhayat du 12 Février 2017:

http://www.maoulhayat.com/index.php?option=com_jdownloads&Itemid=233&view=summary&cid=3181&catid=3
Salam mou aleykoum gnigui ziar mbok talibé yi diléne fatali Ndadié Général bignou diap DIMANCHE 12 FEVRIER 2017 fii si Janatul Firdawsi Keur Mbaye Fall/DAKAR si téwayou Cheikh Ahmadou Mbacke Maoulhayat

Serigne bi néna migui koy yeguel mbok talibé yép ak sopé yép, tay sakou niép téwéko inchallah
" Sëriñ bi yaa gën alal yaa gën barab gënu nit

Ku way ci yaw mucc am mbooleem mébët ya azal

Yaa gën ci nit bakkanam yaa gën ci nit barabam

Yaa gën ci nit mbokkam ak léppam ku weddi xamul "

#SegneMbayJaxate

Cheikh Ahmadou Mbacke Maoulhayat Yalla nafi yague lol ta wer
Dernier Discours de SERIGNE SALIOU MBACKE...

"Lima serigne touba djiteul tchi yen dama koye

andak yên tchi kaw djiteul guimouma djiteul

nguene topp sama guinaw

Bouma djito dama lén di guêstou rek bouma len

sénoulite takhaw néek-lén

Bouma guêsto guissouma lén ma deup dadiék

yen

Bouma dadiék yên bou nguén deuppé it damaye

topp tchi yen wayé doune taggo

Wayer bou ngéne ma djitalé darra louye yakhe

diiné mba mouye yakhe talibê mba mouye yakhe

addina doumako def

Boumaye dokhit nak dama len di guêstou rék

bouma lên sénou tiit néek-lén bouma néggué lou

yagg aksi wou lén ma deup woute siléne

Bouma fêcké nguên dem ma djiteul lén topp tchi

yên

Wayer doune taggo mouk''

" Douma fekk mouk lou Yalla yaatal, ma diko

xatal. Dara louy yak Adina,wala diinee doumako

def. Mane ande naak niep.

Lissi dess nak, Yalla yore diaamam, té ci

yeurmandeem lalen yore. Yeurmandee diodiou

nak, damay niaane mou yok rek, te yaatal ko.

Mangui len di nouyou bou baaxa baax, dilen

niaanal, wayee yeenit nangenma nianal "

Yalla na yalla yok sa leer t taaass niou ci sa barké Amiiiiiiiiiinnnnne borom diamono borom niouroul borom ndiapndall borom ndiowaaaannn gué ca rooon xayga borom yeurmaandé
Gamou 2016, téléchagez le sermon ici: http://www.maoulhayat.com/index.php?option=com_jdownloads&Itemid=233&view=viewdownload&catid=3&cid=3157
MAGAL 2016: Téléchargez le Sermon de Cheikh Ahmadou MBACKE Maa-ul Hayaat ici: http://maoulhayat.com/index.php?option=com_jdownloads&Itemid=233&view=summary&cid=3126&catid=3